Back to Top

Believe in Yourself Video (MV)

Performed By: Nik & Baabel
Length: 4:18
Written by: Cheikh Thiam
[Correct Info]

Nik & Baabel - Believe in Yourself Lyrics

Baabel and Nik and the mix styles
Believe in yourself
Believe in yourself

Adouna youmboul nit nitay garabam
Nit nittèy nitt yonam
Sakh si deugu nay sa yittè
Kon diamou j ngay wotè nang si ndieukè
Diokh diamou
Yeureum diam
Khetali diam
Takou... teuk seytan
Bagne tok di setan
Beuguè (Euleuk) ndam
Diokk tèll thia fadiar di daw si louko si louko diar
Yonou mbonn boul fa diar
Koulay sèntou doulafa khar
Bagna yèm lèni kènn
Wagni bo guiss ci bènne
Ndakh kè kaka diokh mola khagne yallay kène

I thank god who woke me this morning. I'll water the tree whose shade gave me air when i was hot

Doylo yalla sa so sonné
Ngémbo diom sassouné
Yow mi dioup moytoul
Moutthie si none yombatoul
Dérou képpeu lay yakh
Doufi bayow ma toul
Lou léwa diara sonou
Boul doundou doungourou
Dou ngourou gor
Naniou rafétal woutine
Dioub. Diouball farak yon
Molay ar si pékhéy nonne nonn noonnn
Nnnoonn khamalné rook séne nopina nonnn geumeulné rook séne nopina
Lo séunne mom la. Ndakh lim la téga geun tay j mou mom la

Bouurrr yallla mang lay sante bama yéwok diamou

Fonkal garap guila kèram fèkhal banga tanguè ha ya yay
Ponkal boumla taxa dieul sa dolè dissi notè

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Cheikh Thiam
Copyright: Lyrics © O/B/O DistroKid

Back to: Nik & Baabel

Tags:
No tags yet