Back to Top

Karim Diouf - Téloul Lyrics

Karim Diouf - Téloul Lyrics

Say niane nagouna yaw mani santal
Say lidjanti ostina yaw mani teyloul
Bousa ande boyé sani tchi mata gueune fayko
Say niane nagouna yaw mani santal...
Mayou Yalla dafa barri té wouté
Mit kouné la Yalla maye
Boul ame ba fokni yaw millé idoto niak
Sa ame-ame, djarignouti ba tarou

Djarignouti ba Tarou
Teralal gnaka yellol
Bo khébé sa wass anda go war mou toch
Djarigouli ba Tarou
Teralal gnaka yellol
Dajarignouti ba Tarou
Taralal gnaka yellol

Gua niak niak niak niak niak ba fokni yaw mi djam daloula
Boula dalaté gueumeulni Yallay Karim Al Hadji

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Karim Diouf - Téloul Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Karim Diouf
[Correct Info]
Tags:
No tags yet