Back to Top

Karim Diouf - Mane Lyrics

Karim Diouf - Mane Lyrics

Mane, li ma beugueu dafa Barri te wouté oh mane
Sama beugue beugue rombena adounassité oh mane
Damay tok bamou yague sama khël dem tchi samay dom mane
Souma manone, souma manoné, khélal la gua yoballé
Bour Yalla mo binde adouna ak la tcha birame
Djeul dommou Adama watché ko tchi kar souf a lëp lou ko yitélone
Souma sagnone domou Adama dou massa sonne, dou massa djakhlé
Dou massa khif fi tchi kaw adounassilé
Djam ak pékhéme, Bour Yalla moy doggal yaw
Kou sagnone bo djouré sa dome bou souroulit, hif douko rey
Mane li ma bueuge, li may woute, la al ame dafa barrité wouté oh mane
Mane mi mane damay tok ba mou yagg sama khël dem tchi sana seut mane, mane mi
Sen moudjou diaxalma lol wayé ndenkanné tchi lokhop Bourbi Yalla
Sa youma kheuyé mane, mane mi
Li ma beugue la niep beugue, kouné beugueneu lou barri té wouté mane, mane mi
Mane mi Souma marone, kou dekki agne digua rére ba sour fi tchi adouna, mane mi
Li ma beugue la niep beugue, kouné beugueneu lou barrié wouté Yaw, yaw mi

Souma Manone, souma manone kou fébare gnou tétchla mo
Khame lou mou maneti done mane mi
Li ma beugue dafa barri te wouté oh mane
Mane mi souma manone fital guerre armement lep lagnouye tek si soufe mane
Mane mi sénne moudjou diakhal ma lolou, wayé nou may def
Khana gueune di niane
Mane mi Souma manone
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Karim Diouf - Mane Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Elage Diouf, Karim Diouf
[Correct Info]
Tags:
No tags yet