Back to Top

Karim Diouf - Bésou tey Lyrics

Karim Diouf - Bésou tey Lyrics

Yaw mi lé, djoudo tchi rëw, magué tchi rëw
Bourbi Yalla wersaguéla gua mana deme ba bitlim rëw mana
Danidollé, Boul Faté Mdéye Boul Fate Baye
Wara mana tok goorgoorlou
Ba gay dem, Mdeye ak Baye dagno bollé yéné gnane tchi
Bourbi Yalla MGua dem tchi Djam, gnëw tchi Djam
Gnome gni la ganéf fi tchi adounasilé Oh Oh Oh!!
Wakhlen tchi, li fouma koy wakhéti
Wakhlen tchi, Ana Fan la koy wakhéti
Kon Bok Wakhlen tchi Li fouma koy wakhéti
Bessou tey sédéna sama fouk ak djounome gninty ate
Mdiakaré ak titi top nama oho
Ma bougone Xam euleuk nou mouye géémé yaw
Sama kilifa di dane senni dolé senni meun-meune
Yakar lëp louma niak gno ma ko tek, gnome gni, ma
Ganalé Fi tchi adounasilé Oho!!
Wakhlen tchi, li fan la koy wakhéti
Wakhlen tchi, Ana fan lagnou koy wakhété
Moy li wor moye li wor, waw moy li wor moy li wor
Bougnou Djougué di dani senni dolék senni mane mane
Yakar lep lou ma niak gno ma ko tek gnom gni ma
Yanel fi tchi adounassilé oh oho
Kheuyna nonou la warone deme
Bouna Mdiaye ma djiguene, Bouna Mdiaye Ba Djoloff
Maré nane, Bouna ya beanoup tene wa Djoloff da tchi
Nane rëwma nan tcha
Mone la wara démé yaw, non la wara démé
Mare nane, Maroul nane dokh ma gui wala gane fé tchi walo
Dou tchi mane Dou tchi yau nonou la warone démé
Dou tchi mane, dou tchi yaw nonou la warone démé
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Karim Diouf
Copyright: Lyrics © David Murphy et Cie, Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Karim Diouf - Bésou tey Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Karim Diouf
[Correct Info]
Tags:
No tags yet