Back to Top

Karim Diouf - Anta Lyrics

Karim Diouf - Anta Lyrics

Si bi di bé da da lé
Dama khamoul loufi diar yaye djour sanni
Kholal gni fi beugue ame sene dome te Yalla mahoulenko
Boula Yall mayé dang koye khame
Tchey yawitt dome sa yo maqué Lép liye begguelo sa yaye defko doula wagni dara
Sa yaye mo dane kheuye di nampal di dap sa banekh
Lép lou war tchi yaw moune koy def guir sa moudjouk euleuk
Anta Soudeyna, Anta Dadél, Khalela
Domou mame Koura Khalela ak Yoro Sy Khalela
Djiguénou Mére Faye khalela ak Gorgui Diouf khalela
Ki di domou Mame Joura mi gnouye woyé Tako Dadé
Lidy, Fany Sy mome moy raki Soukena khalela, khalela bou gnouye wowé Tako Dade
Han Woma Womaye
Yaw no ko beugué ak foko beugé yaye
Fo gnou wo gnou wouyoula
Dama khamoul loufi djar yaye boye bagnou djour sani, hé!
Kholal gni fi beugue ame sene dome te Yalla mayoulenko
Boula Yalla mayé dangue koy khame
Tchey yawitt dome sa yo magué, Lep loug begglo sa bay defko dou la wagni dara
Sa Baye mo dane kheuye di job, di beingne guen khit, lep lou war
Tchi yaw mou gui koy def guir sa moudj euleuk
Anta Soukeyna, Anta Dadël khalela
Domou mame Koura, khalela, ak Yoro Sy khalela
Djiguénou Mère Faye khanlela ak Gorgui Diouf, khalela
Ki di domou Mame Koura mi gnouye wowé Tako Dadé
Lidya, Fany Sy, mome moy raki soukeyna khalela, khalela bou gnouye wowé Tako Dadé
Domou djambour, domou djambour, domou djambour Topatol sa Domela
Hanye dagnou Hanye, Aïcha dagnou Hanye
Domou djambour, Domou djambour, Domou djambour Toptatol sa domela

Khalela, khalela mi gnouye wowé Tako Dade
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © David Murphy et Cie, Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Karim Diouf - Anta Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Elage Diouf, Karim Diouf
[Correct Info]
Tags:
No tags yet